Youssou Ndour - Waññi Ko (version lyrics)

Youssou Ndour
Youssou Ndour
Publié le 19.07.2021

Waññi ko , ëpp në :
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Refain : waññi ko , waññi ko , waññi ko ,
Waññi ko , waññi ko , ëpp në

Yaw yaa ni , ëpp óon nga , trois cent kilos ,

te bés bu ne , benn xar nga daan añ e

nga neeti , at mi fi Obama ñëw ée

yaw yaa ko gis , muy dox antu , biir Pikine

am oon na , gaïnde gu rëccé , parc hann

nga neeti ñu , yaw yaa ko jat , ba mu nelaw ,

· nga ni ma , am oon nga , benn bateau , ca Guinée

te waa nations – unies , nga ka daan loué

· te diggënté , États-Unis ak Guinée ,

daa woo ko daw , lu ëpp ñaar i fan
am na benn bés , nga ni ma , my boy
keroog daje naak , roi des arènes. 2 fois.
ben loxo , laa ko yékkëtée , ni ko félicitations. 2 fois.
ma tegaat ko ci suuf , ni ko , my boy. 2 fois

na nga jaar , sa ma kër , ma jox la yeneen clefs

na nga jaar , galle , ma jox la yeneen clefs

techniques yooyu , japon laa ko jànge

ca yooya jamono , man la ñépp di wër

lu ñu wax nga ni fekke nga ko

fu ñu wax nga ni dem nga fa

doo tiit doo raf , doo dellu ginnaaw ;

waaye sa ma waa jii , ken melut ni moom.

Wax oon naa fi ni adduna ken du ko dajal ,

Te ku dul umppëlé da ñu lay ragal.

Wax aat leen ni faw nit ku ne am lu muy des al

Ngir bu ëllëg ée ñu mën laa set al.

Xam lépp , mën lépp , loolu , yalla dong a ko jagoo. 2 fois.

ragal al yalla , waay , ragal al yalla

ragal al yalla , waa jii , ragal al yalla

ragal al yalla , waay , ragal al yalla

ragal al yalla , waa jii , ragal al yalla

Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine
http://www.youtube.com/c/YoussouNdourofficiel
https://www.facebook.com/youssoundourofficiel
https://www.instagram.com/youssoundour1959

Runtime 00:04:08

Youssou ndour, ndour, tfm, lobs, ministre, chanteur, dakar, senegal, africa, international, Youssou Ndour, Hello, Boukki YI, Bercy, Xaware youssou ndour, Fiitey, Grand Bal, wanniko waniko wagniko,

COMMENTAIRES: 4,203